Waallu bitim reew askanu reewum Marok deemb amalnañu ab duxu ñaxtu di saakku ñu dakkal doxu ñaxtu ci reew
Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internet (atlasinfo) neekk ci (Ribaat) ci peyu reewum Marok ni: aakkaskanu reewum Marok deemb gennañu ngir amal ayy doxu ñaxtu ngir saakku ñu dakkal fitna yi ci reewum Egypt
Askanu reewum Marok woona mbooleem kureel yi ak mbootaay yi nga xamni dañii ligeey ci waallu jaam ci Rbaat ñu book ci doxu naxtu bi ngir faat ak faagaagal yi nga xamni ñungikoy amal ca reewum Egypt mana dakk
Ñi nga xamni ñoodoon amal ayy doxu naxtu ak kilifa reewum Marok yi nga xamni toolluwoonnañu ci juroom walla juroom been junni kilifa ci nguuru reewum Marok nga xamni wonenañu ni ñoom ak askanu Egypt ñoo book naxar wi te yitt saakkunañu ñu dakkal deret bi nga xamni moom lañii tuur
1274759