Waallu internet site bi nga xamni dafay yënggu ci waallu yeewute islaam ci nimbalu mbootaay ak kureelu daara ju kawe jiidi Al Mustafa lañuko ubbee
Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaaru yeewute islaam nga xamni nga xamni dafa aju ci daara ju kawe jiidi Al Mustafa leegui juroom beenni kalaama la
Mbebetu yookku kalaama yi mooy ñëpp mana bookk ci gëstu bi nga xamni ñungikoy amal ci yeewute islaam ak yitt ci ndigalu njiitu revolution islamique bi ci reewum Iran
Site bii nga xamni dafay yënggu ci waallu yeewute islaam mooy islam-awaking.com jamono yii ci juroom been kalaama la neekk pers ak ordu ak turkie ak bangali ak almani ak arab
1276952