کد خبر: 1290823
تاریخ انتشار : ۲۹ شهريور ۱۳۹۲ - ۱۸:۰۶

Muhamad al Baraday feddalina ni dañoo wara baayi xel ak saam mbebetu revolution bi

Waallu bitim reew Muhamad Al Baraday nga xamni bokkoon ci nga xamni ñoodoo ligeey ak njiitu reewum Egypt gannaaw bi ñu daaxee Morsi ci nguur gi xamlena ni dañoo saam mbebetu revolution bi ci reewum Egypt



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan biidi (Ikna) xabaarna jëleeko ci ci këru xabaar biidi (alyawmu saabi) ni: gannaaw bi nga xamni kiidi Al Baradaay tookkna lu toollu ci fanweeri fan ak juroom feeñul feen waxul yitt ci mbiru polotik waxna ci twitter ci internet ni dañoo wara saam mbir ak mbebet yi nga xamni moo waraloon askanu reewum Egypt amal ab revolution maanaam fixxu daax nguuru Mubarak


Gannaaw bi nga xamni takku deru reewum Egypt yi ñungi faat ak bunduxatal sooppey njiitu reewmawoon te takku der daaxko ci nguur gi Muhamad Morsi ci la teekki ndomba taŋkkam fan yii nak xamlena ni mbebet ak njariñu revolution bii dañuko wara saam


Kiidi Al Baradaay bindna ci page twitteram ni maangi saakku ci ndaw yi nga xamni ñoo neekk ci parteem ñu baña faatte mbebetu revolution bi ak ligeey ngir askanu reewum Egypt


1290209

captcha