Waallu bitim reew ñaareelu jonŋante diine bii ñu duppee (xasiida wurus) ngir xamle ñi nga xamni seen xam xam dafa naac ci waallu al xuraan, jonŋante yii nak ci television bi nga xamni mooy touba jonŋante bii nak ca Dakar lañukoy amalee peyu reewum Senegal
Këru tasukaayu xabaaru al xuraan (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bii xamni mooy (APS) ni: mbebetu ñaareelu jonŋante diine bi ñu duppee (xasiiday wurus) mooy xam ak raañee ñi nga xamni seen xam xam dafa naac ci waallu al xuraan ak ñaangum al xuraan dinañu taan yitt ci jonŋante bii ñi nga xamni ñoo gëna raañeeku ci ñaangum al xuraan
Daaw nak moo neekkoon njëlbeenu yoon ñuyy amal jaonŋante bii nga xamni moom lañu duppee (xasiida wurus) waaye ñi nga xamni ñooy nonggo daara al xuraan yi bëggoonnañu bu baax programme bii jonŋante bii ci reew mi yëpp lañuko amalee ci television bii nga xamni mooy Touba TV
Jonŋante bii nga xamni ci taambali att mu bees mii lañukou amal ñi nga xamni ñooy bookk ci jonŋante bii gannaaw bi ñu weesoo waall bu njëkk bi dañii duggu ci ñaareelu waaye leepp nak ci yar ak teeggin lañukoy amalee ci television bii nga xamni mooy Touba TV neekk ci Dakar ci peyu reewum Senegal
Faan ak mbir yi nga xamni ci lay jonŋantekat yi di jonŋante mooy musique bu aju ci diine ak ñaangum al xuraan ak faannu waxtaan ci diine ak ñaangum al xuraan bu seel
1296697