salafiste yi ak ñi nga xamni dañoo ëppal ci diine dañii tere chiite yi amal seen feetu Xadiir
Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internet (vetogate) ni: kiidi Mahmuud Jabbaar bookk ci njiitu chiite yi ci reewum Egypt waxna ni: Xaadir dafa feekk ci feete yi nga xamni moo gëna magg ci islaam rawatina na ci chiite yi
Mahmuud Jabbaar yookkna ci ni: ci reewum Egypt sa amuñu bërëbu boo xamni nii foofu lañii amalee ayy feetu chiite ci bitim reew sa lañii amalee ayy feete
Kiidi Jaabir waxna ni: te xadiid bu siiw bii nga xamni yonente bi dafay wax ni (baayeenaa leen al xuraan ak sama njaboot su ngeen ci jaappee du ngeen reer mukku) amna teere sunnite yoo xamni sa indinañu addiis bii soo demee ci saxiix muslim ak Albanii ak yeneeni teere waa Axlu Sunnite
Mahmuud Jaabir ci cëppaa ndaw gi waxna ni: chiite yi nga xamni ñooy yeewoo ci reewum Egypt muñuñu bërël feete bii nga xamni mooy Xadiir ndax salafiste duñu leen ci baayi ci seen jaam
1304145