کد خبر: 1309286
تاریخ انتشار : ۰۶ آبان ۱۳۹۲ - ۲۳:۳۶

Coong yi nga xamni fafalnaaw Israel yi amalnako ca Gazza

Waallu bitim reew taskatu xabaaru Israel yi xamlena ni ayy fafalnaaw yu am ayy boomb saandinañu ayy boomb ca Gazza



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan (Ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci chaine biidi (Sky news Arabic) ni: fafalnaaw yi nga xamni moo baayeekoo ca Israel tey ci suba amalna ayy coong yu bari ci bët saalumu Gazza takk deru Xamaas yi tuxalnañu seeni bërëb yi


Waxnañu ni coong yii nga xamni nguuru Israel bii soo gisee ñu amal coong bii waa xamaas dañoo saandi ñaari ndeend ca Israel


Takku deru nguuru israel yii dafa tekk lo lu toollu ci fukki ak juroom ci doomu Palestine nga xamni ci waa xamaas lañu bookk te dañu leena yoobb ci bërëb yoo xamni nii keen xamuko


Coong yii nga xamni waa Israel ñungikoy amal dafa feekk ñuyy waxtaan diggente Israel ak reewum Palestine deemb nguuru Israel xamlena nii dina baayi leen ci prisonnier Palestine yi nga xamni tekknañu leen loxo


1309067

captcha