کد خبر: 1279238
تاریخ انتشار : ۰۶ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۱:۲۱

Dinañu amal ab ayu bësu xamle islaam ca New zeland

Waallu bitim reew kiidi (Judiyet kalniz) jawriñ gi ñu deenkk waallu diine ci reewum New zeland xamlenañu ni dinañu amal ab ayu bësu xamle islaam



Këru tasukaayu xabaaru islaam yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bu neekk ci internet (Radio New Zealand) ni: kiidi Kalniz xamlena dañii amal ab lëllu xamle islaam ci ayu bës bi nga xamni ci lañu jagleel islaam ngir deellu njukkal jullit ñi ci ligeey bi nga xamni ñungikoy def


Programme bii nga xamni ci diiru been ayu bës lañukoy amal ayu bës la boo xamni nii dinañu xamle islaam di yitt dinañu xememloo islaam jullit ñi ak ñi nga xamni duñu ayy jullit


Jawriñ gi ñu deenkk waallu diine ci reewum New Zealand ak mbootaayu jullit ñi ci reew mi ñooy amal ayu bës bii nga xamni moom lañu jagleel islaam, reewum New Zealand reew la moo xamni nii dafa neekk oceanique te yitt dafa jege Australia


Lu toollu ci juroom fukki junni jullit ñooy yeewoo ci reewum New Zealand


1278721

captcha