Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ci reewu tugël yin i: gaaral bii nga xamni dañukoy amal ci waallu nataalu islaam ci nimbalu kiidi Ahmad Karavasn nga xamni artiste la feekk baax ci reewum Allemagne tomb bi nga xamni moom lañu duppee gaaral bi mooy islaam ci reewu tugël yi
Mbebetu taxawal gaaral bii mooy xarkanamu islaam bu muccu ayib ci reewu tugël yi ak fexe ba sakan wi nga xamni ñooy yeewoo ca reewu tugël yi xam islaam bu baax ci xamin yu wër
Li jara fattaliku mooy kiidi Axmad Karavasn nga xamni ab artiste la bu feekk baax ci reewum Allemagne mungi duggu ci islaam ci attum 1965 te yitt centre bii nga xamni dafay taxawu gaaral bii dafa bookk ci ñent bërëbu yi gëna siiw ci waallu islaam ci reewum Allemagne
1280398