کد خبر: 1283122
تاریخ انتشار : ۱۴ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۲:۳۳

Amalnañu ab gaaralu al xuraan ca reewum Nigeria

Yënggu yënggu al xuraan amalnañu ab gaaralu al xuraan ca bërëb bi nga xamni ki teewal reewum Iran ci waallu caada fala dëkkee



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ci Afrique ni: suñu sukkandikoo ci xabaar yi nga xamni jëleenañuko ci kureel bii nga xamni dafay yënggu ci waallu caada ak jëflante ci diine islaam dinañu wax ni ci bës bi nga xamni ci lañudoon fattaliku geen aduna Imaam Saadix mu toombewoon ak altine ci gox biidi Lagos


Bokkna ci li nga xamni moom lañufa gaaraloon ayy teere islaam yu wute ci kalaamay arab ak Hawsa ak anglais ak ayy tableau art yoo xamni nii mbindum islaam lañuko bind


1282494

captcha