Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ci Afrique ni: suñu sukkandikoo ci xabaar yi nga xamni jëleenañuko ci kureel bii nga xamni dafay yënggu ci waallu caada ak jëflante ci diine islaam dinañu wax ni ci bës bi nga xamni ci lañudoon fattaliku geen aduna Imaam Saadix mu toombewoon ak altine ci gox biidi Lagos
Bokkna ci li nga xamni moom lañufa gaaraloon ayy teere islaam yu wute ci kalaamay arab ak Hawsa ak anglais ak ayy tableau art yoo xamni nii mbindum islaam lañuko bind
1282494