کد خبر: 1285543
تاریخ انتشار : ۱۹ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۰:۴۱

Ñaxtu ci taan gi ñu taan reewum Baxrayn mu neekk bërëbu attekaayu reewu arab yi

Waallu bitim reew kureel bi nga xamni mooy saytu waallu aax ak yeleefu doomu aadama ñaxtu bu baax ci taan bi nga xamni taannañuko reewum Baxrayni mu neekk bërëb bi nga xamni dañu cii saytu waallu aax ak yeleefu doomu aadama yi



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internet (Al Wifaax) ni: kiidi (Niklaas mak jiixaan) nga xamni dafa neekk ci kureel biidi yënggu ci waallu aax ak yeleefu doomu aadama yi ci reewu arab yi ñaxtuna ci taan gi ñu taan reewum Baxrayni mu neekk bërëb bi nga xamni falañii aattee ci waallu aax ak yeleefu doomu aadama yi ci reewu arab yi waaye xamlena ni taan gii du mana nëbb been yoon ñaawteef yi nga xamni reewum Baxrayni mungikoy def ci waallu aax ak yeleefu doomu aadama


Kaaddu yii dafa feekk kiidi Samiire Rajab jawriñ giñu deekk waallu jokkoo ci reewum Baxrayni waxni faata ak faagaagal gi nga xamni ñungikoy def askan wi du leen ludud jaamarloo polotik


Waaye kureel yi nga xamni dañii yënggu ci waallu aax ak yeleefu doomu aadama ci reewum Baxrayni xamlenañu ni reewum Baxrayni reew la moo xamni nii du woormaal aa ak yeleefu doomu aadama yi


1283980

captcha