کد خبر: 1286216
تاریخ انتشار : ۲۰ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۲:۱۲

Dinañu amal ayy xew xewu maaggal Imaam Ridaa ca Vienne

Waallu bitim reew xew xewu maaggal ganesi aduna Imaam Ridaa ca Vienne 17 septembre lañukoy amal ci nimbalu centre islamique bi nga xamni moo neekk ca Vienne



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci reewu tugël ni: suñu sukkandikoo ci xabaar yi nga xamni baayeekoona ci centre islamique bi nga xamni moo neekk ca Vienne dinañu wax ni xew xew yii dañukoy amal ngir maaggal ganesi aduna Imaam Ridaa soopey Imaam Ridaa yi ñookoy amal


Xew xew yii su fukki waxtu ak juroom tegee ñent fukki simili ak juroom lañukoy amal te yitt ñungi cii woo ñëpp jullit ak kudul jullit chite ak Sunnite


1285682

captcha