Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci reewu tugël yi ni: ndaje mii ci sale bu magg bu neekk ci centre bu magg bi yor mbiru diine yi ci reewum Tatarstan lañukoy amalee ci teewaayu mbooloo mu takku ci ayy aattekat ak ayy borom xam xam ak ayy nittu diine ci reewum Tatarstan
Ci ayy kaaddu kiidi Fadli Of nga xamni mooy aattekatu bi magg ci reewum Tatarstan waxna ni jaangatnañu saytunañu neekkin ak toolluwaayu aattekat yi ci reewum Tatarstan ak leepp loo xamni nii moo war ci tabaski bi ak faratay natt zakat ak faratay cakŋ ak sëy ci islaam
Waaye yemuñu foofu ndax aattekat yi xalaatnañu ci seen programme ak seen doxalin yu bees yi nga xamni moom lañu wara doxal
1286230