کد خبر: 1279239
تاریخ انتشار : ۰۶ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۱:۲۲

Noonu islaam yi amalnañu ab coong ci been jumaa bu neekk ca reewum angleterre

Waallu bitim reew amna beneen jumaa bu noonu islaam yi soongati ci reewum angleterre ci gox biidi (harluy iskes)



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci yeenekaay bii neekk ci reewum angleterre ni: jumaa jii nga xamni moo neekk ca (harluy iskes) deemb ayy noonu islaam amalnañu ci ab coong taalnañuko yaaxko


Waaye ñi nga xamni ñoo yor jumaa ji dañoo gaaw waajal julli gi baayiwuñu noon yi am lu leen neex ndax seen mbebet mooy tere jullit ñi julli


Gannaaw bi ñu faatee ab takk der ci mbed london yi ba leegi taalnañufa ayy jumaa yu bari


1278635

captcha