Waallu dundin gannaaw bi nga xamni jullit ñi saakkunañu ñu amal ab jumaa ci aeroport bi ngir ñu mana julli seeni farata kilifay aeroport bi jelnañu dogalu tabax jumaa ci aeroport bi
Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ca reewu tugël yin i: gannaaw bi nga xamni ayy jullit yu bari ñungi saakku jumaa ci aeroport bi ayy kilifay aeroport bi jelnañu dogal amal ab jumaa ci aeroport bii ñuyy duppee (venkura) neekk ci Moscow
Jumaa ji nga xamni moo neekk ca beneen aeroport bu neekk ci Moscow sa nga xamni dañoo tëjoon juma ji dinañuko tijji te yitt jullit dinañu mana def seeni farata ci aeroport bi
Li jara xam mooy jamoni yii amna ñaari aeroport international maanaam aduna wërngelkëp yu neekk ci Moscow yu am jumaa
1278937