کد خبر: 1300516
تاریخ انتشار : ۱۷ مهر ۱۳۹۲ - ۰۰:۳۲

Kureel bi nga xamni mooy ligeey ci waallu yookk daara al xuraan yi ci reewum Niger moo jël neexalu xeex ak ñaakka jaang

Waallu bitim reew mbootaayu aduna wërngëlkëp biidi yënggu ci waallu jaang ak caaday islaam joxna neexalu xeex ñaakka jaang kureel bi nga xamni dafay yënggu ci yaatal daaray al xuraan yi ci reew mi



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internet (isesco)ni: deemb lañu joxe kureel bii neekk ci reewum Niger te xeex ñaakka jaang neexalu xeex ak ñaakka jaang ci reewu islaam yi ci xew xew bi nga xamni dañuko doon def ci ñaangum xale yi ak jigeen ñi


Kiidi (Isaa Namata) ndawalu reewum Niger ci mbootaayu waallu jaang xam xam ak caaday islaam nga xamni moofa teewaloon njiitu kureel biidi yënggu ci waallu daaray al xuraan yi ci Niger moo nangu neexal bi ci Abdul Aziz Usmaan atuyjeri njiitu UNESCO


Xeex ak ñaakka jaang te jaareko ci jaangale bind ci kaallaamay reew mi ci Niger Hawsa ak Fulani ak zurme ak bind al xuraan ci kalaamay reew mi ak bind ayy addiisu yonent bi ci kalaamay reew mi bokkna ci yënggu yënggu kureel bii


Kureel bii nga xamni dafay yënggu ci waallu caaday islaam ak xama (UNESCO) ngir xeex ak ñaakka jaang ci reewu islaam yi dafay ligeey lu am solo ci xeex ñaakka jaang ci reewu islaam yi


1300134

captcha