کد خبر: 1304827
تاریخ انتشار : ۲۷ مهر ۱۳۹۲ - ۱۹:۰۴

Ci diiru been weer daaray reewum Amerique yi ayy daara islaam lay neekk

Waallu bitim reew ab daara bu neekk ci gox biidi ( Iliyunaz) neekk ci reewum Amerique ci weer bii ñu dekkmal dinañu amal ayy programme ngir xale yi gena mana xam islaam



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaarox b bi nga xamni moo neekk ci internet (ThyBlackMan.com) ni: daara yi nga xamni moo neekk ci reewum Amerique ci gox (Ilyunaz) dina def daara gox bi ayy daara islaam ci diiru been weer


Ci diiru been weer laata ñuyy taambali jaang dinañu amal ayy ñaan ba noppi ayy teere islaam ak taariixu islaam lañii jaang ayy leekk islaam sa lañii server


Nonggo daara yi sa ayy yëre islaam lañii sol muuruk islaam yitt lañii muuru, kilifa yi nga xamni ñoo yor daara yi xamlenañu ni mbebetu amal programme bii mooy nonggo daara yi gëna xam islaam


1304148

captcha