کد خبر: 1305511
تاریخ انتشار : ۲۸ مهر ۱۳۹۲ - ۲۳:۲۴

Teere biidi (chiite) móólnañuko ca reewum Suede

Waallu bitim reew teere biidi (chiite) nga xamni professeur Guraan Larson ak David torfal nga xamni ayy jaangalekatu ci daara ju kawe lañu móólnañuko ca reewum Suede



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ca reewu tugël ni: teere dafa wax ci neekkinu chiite yi nga xamni ñooy yeewoo ci reewum Suede suñu sukkandikoo ci xabaar bii dinañu wax chiite yi nga xamni ñoo njëkka ñëw ci reewum Suede ñungi baayeekoo ca Reewum Uganda dem caTerolahtaan


Li jara xam mooy suñu sukkandikoo ci xabaaru nguur gi dinañu wax ni chiite yi nga xamni ñooy yeewoo ca reewum Suede toollunañu ci 165654 lu toollu yitt ci 250000 doomu aadama ñungi feekk baax nak ci reew yiidi Afganistan ak Liban ak Pakistan ak Irak ak Iran ak Inde


1305054

captcha