Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ca Asie ni: xew xew yii dañuko def ngir fattaliku Imaam Jafar Saadix nga juroomeelu Imaamu chite yi di sëtt ci yonent bi xew xew bii nak ci ab jumaa lañukoy amal ca Erevan
Bokkna ci programme yi nga xamni dinañuko amal ci xew xew bii julli mbooloo timis ak geewe ak waxtaanu diine ci waallu waccuwaay bi nga xamni Imaam Saadix amnako ak ayy xeewlu gannaaw bi waxtaan yi jeexee
1281022