Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ñi nga xamni ñoo leen teewal ci reewu tugël yin i: tabax ayy jaangu ci gox boo xamni nii teemeer boo jël juroom fukki ak ñent ayy jullit kon suñufa bëggee tabx ayy jumaa warul indi ayy jafejafe waaye nak biñu beggee yookk limu jumaa yi ci Moscow peyu reewum Russie dañoo tëpp ne duñu ci dal
Kiidi Ramadaan Xaadir of dafa gëm ni: ñi nga xamni ñooy ayy jullit ak ñi nga xamni ñooy ayy kercen dañoo wara aand dundadoo ku neekk woormaal sa morom te yitt reewum Russie dafa neekk reew moo xamn nii loolu warufa jafe
Lii nak dafa feekk ñu neekk ci jamono joo xamni nii jaraafu peyu reewum Russie baña joxe ab këyit ñu tabax beneen jumaa ba xamle ni juroom beenni jumaa doyna ci gox biidi Russie
1281284