کد خبر: 1282401
تاریخ انتشار : ۱۳ شهريور ۱۳۹۲ - ۰۳:۲۸

Reewum Azerbaijan dafa gennee been ayy koppar ngir jaamarloo ak ñi nga xamni dañii xeex islaam

Waallu bitim reew nguuru reewum Azerbaijan xamlena ni dina amal ba budjet ngir jaamarloo ak ñi nga xamni dañoo noonoo islaam



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bii neekk ci internet ni: kiidi (Ali Xasan of) njiitu waallu dundin ak polotik ci cabinet njiitu reewum Azerbaijan waxna ci conference bi nga xamni kureel yu aju ci nguur gi ak kureel yi nga xamni ajuwuñu ci nguur gi ñooko seexoon ni nguur gi dina amal ab budjet boo xamni dañukoy jëfandikoo ngir jaamarloo ak xeex ñi nga xamni dañoo noonoo islaam ak ligeey ci yaatal caaday islaam ak jikko islaam yi


Waaye kii nga xamni kilifa la ci nguuru reewum Azerbaijan waxul budjet bi ak koppar yi nga xamni moom lañii jëfandikoo ngir xeex noonu islaam ci ñaata lay toollu waaye waxna ni: budjet li nga xamni mooko taxa jokk mooy jaamarloo ak ñi nga xamni dañii xeex islaam ndax jamono yii dafa melni neekk ak neekk terroriste moo yem


1281878

captcha