کد خبر: 1301139
تاریخ انتشار : ۱۸ مهر ۱۳۹۲ - ۰۰:۳۰

Ndoorte ayy daara ci diir bu gaat ngir jaangale ak yar ca laaxuur

Waallu bitim reew ndoorte ayy daara ci diir bu gaat ngir jaangale ak yar ci këru caada republique islamique bi nga xamni moo neekk ca Laaxur



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ca Asie ni: mbebetu amal ayy daara ci diir bu gaat ngir jaangale art bu aju ci islaam bu wër te wóór ak jaangale taariixu reewum Iran ñeel keep koo xamni nii bëggna


Daara yii nga xamni moom lañii def ci diir bu gaat bokkna ci ñi nga xamni ñoofay jaangale ab Oustaz bu feekk baax ci reewum Iran t exam lu bari ci waallu jaangale ak yar acaada ak art bu aju ci islaam


Li jara xam mooy daara yii nga xamni doornañu barki deemb 07 octobre dinañuko wëyal ba diiru ñett weer ci kër gi nga xamni mooy yënggu ci yënggu ci caaday reewum Iran


1300732

captcha