Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internert (west.info) ni: ci att yii lañu duggal ñaagum diie wees jaangale diine islaam ci reewum Allemagne, jamono jii ñu neekk lu toollu ci fukki ak juroom nënt jaangalekatu islaam ñoo wara neekk ñaar fukki classe ak juroom ñent waaye nak kilifa li nga xamni ñoo gox li ñu beg mooy yookk classe yi nga falañii jaangalee islaam , te yitt fii ba dëwën mbooleem daara yu neekk ci reewmi dinañu jaangale islaam
Waaye kilifa yi nga xamni ñoo jiite gox dañii jaankonte akk ayy jafeje ci ñaakkk jaangaleku diine islla loolu moo waral ñu amal ayy daara ci diir bu gaat ngir mana taaggat ayy jaangalekatu islaam yu
Daara yi nga xamni moom lañii amal ci diir bu gaat dinañuko door been fan ci fevrier ci att bii ñu dëkkmal ci daara ju kawe ji nga xamni moo neekk Yustus te yitt daara yooyu dinañuko wëyal ci diiru been att
1306246