Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (Ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci nga xamni ñoo leen teewal ca Afrique ni: suñu sukkandikoo ci xabaar bii nga xamni moo baayeekoo ci kureel bii nga xamni dafay yënggu ci waallu caada ak jëflante ci diine dinañu wax ni xew xew bii ci teewaayu kiidi Usmaan sharibtoo njiitu mbooleem Imaam yi ak Mufti yi ci reewum Ghana aand ak lu toollu ci fukki nitt ak juroom ci nga xamni moom lay ligeeya ndoo ak Abdulxadir Taaxir bookk ci njiitu jullit ñi ci reewum Ghana ak Muhamad Xaasim ngs xamni moo yor waallu caada ci ambassadu reewum benin bu neekk ci Ghana ak njiit bi nga xamni moo yor waallu jaang ak jaangale ci gox ak mbooleem ndaw yi nga xamni ñoo neekk ci mbootaay biidi Ali Yaasiin
Kiidi Ridaa Baxshaayesh nga xamni moo yor waallu caada ci ambassade reewum Iran bu neekk ca Ghana jëlna kaaddu ci ni: ci waallu ajj li nga xamni moo gëna am solo mooy jullit fexe booloo ba neekk been ndax loolu mooy njariñu ajj te yitt jullit fexe ba ñeneen ñi nga xamni duñu ayy jullit te yeene wuñu jullit jaam baña duggu ci seen biir
Yookkna ci yitt ni: diine islaam ci dëgg diine yërmande la ndax nak yonent yëpp ci yaalla lañu baayeeko ñoom ñëpp ayy yonent yu baayeekoo ca yaalla lañu
Kiidi Armiyaa shu-ab xamlena ni: mbir bi nga xamni moo gëna am solo ci ajj mooy beennoo jullit ñi nga xamni ci aduna bi yëpp lañii baayeekoo waxna yitt jullit ñi suñu neekkee been dinañu mana jaamarloo ak seen jafejafe yëpp
1293513