کد خبر: 1303360
تاریخ انتشار : ۲۲ مهر ۱۳۹۲ - ۲۲:۳۴

Suba lañii dindi mbalaanu kaaba gi def ci bu bees

Waallu bitim reew suba lañii muur kaaba gi beneen mbalaan bu bees toombe ak bës biidi Arafa neekk ci Maakka



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bii neekk ci internet (AL Ixraam) ni: att mu neekk dañii dindi mbalaanu kaaba gi def ci beneen ci bës bi nga xamni mooy Arafa ci ajj gi mbalaan mi nak suñuko dindee dañukoy jox keen ci nitt yu gëna raañeeku ci aduna bi


Suba dañoo das yeene dindi mbalaan bi nga xamni moo neekk ci Kaaba gi daaw ba leegi def beneen bu ñuul boo xamni nii suwaa lañuko deferee


Kiidi Muhamad Abdullah Bajuda nga xamni moo jiite këru ligeeyukaay bi nga xamni mooy defar mbalaan bi nga xamni moom lañii lal ci kaaba gi waxna ni: lu toollu ci ñaar fukki million ak ñaar ci kopparu reewum Arabie Saoudite lañu def ci mbalaan bu bees nga xamni moom lañii def ci kaaba gi , baat yi nga xamni moom lañu bind ci mbalaan mii nak mooy keen du yaalla kudul moom Allah te yitt moo yoonni yonent bi


1302390

captcha