Këru tasukaayu xabaaru islaam yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bu neekk ci internet (Radio New Zealand) ni: kiidi Kalniz xamlena dañii amal ab lëllu xamle islaam ci ayu bës bi nga xamni ci lañu jagleel islaam ngir deellu njukkal jullit ñi ci ligeey bi nga xamni ñungikoy def
Programme bii nga xamni ci diiru been ayu bës lañukoy amal ayu bës la boo xamni nii dinañu xamle islaam di yitt dinañu xememloo islaam jullit ñi ak ñi nga xamni duñu ayy jullit
Jawriñ gi ñu deenkk waallu diine ci reewum New Zealand ak mbootaayu jullit ñi ci reew mi ñooy amal ayu bës bii nga xamni moom lañu jagleel islaam, reewum New Zealand reew la moo xamni nii dafa neekk oceanique te yitt dafa jege Australia
Lu toollu ci juroom fukki junni jullit ñooy yeewoo ci reewum New Zealand
1278721