صفحه نخست

فعالیت قرآنی

سیاست و اقتصاد

بین الملل

معارف

اجتماعی

فرهنگی

شعب استانی

چندرسانه ای

عکس

آذربایجان شرقی

آذربایجان غربی

اردبیل

اصفهان

البرز

ایلام

خراسان جنوبی

بوشهر

چهارمحال و بختیاری

خراسان رضوی

خراسان شمالی

سمنان

خوزستان

زنجان

سیستان و بلوچستان

فارس

قزوین

قم

کردستان

کرمان

کرمانشاه

کهگیلویه و بویر احمد

گلستان

گیلان

لرستان

مازندران

مرکزی

هرمزگان

همدان

یزد

بازار

صفحات داخلی

کد خبر: ۱۲۹۰۸۲۲
تاریخ انتشار : ۲۹ شهريور ۱۳۹۲ - ۱۸:۰۴

Waallu yënggu yënggu al xuraan yi dorrnañu tabaxu njëlbeenu jumaa ak yeneeni bërëb yoo xamni nii dinañufa amal ayy xew xew ci (Lyubeyana) peyu reewum Slovenia



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci ñi nga xamni ñoo leen teewal ci reewu tugël yin i: suñu sukkandikoo ci television bii nga xamni mooy (RTV) neekk ci reewum Slovenie dinañu wax ni ligeeyu njëlbeenu complexe islamique bii ci reewum Slovanie doornañuko ci altine bii ñu geen ci teewaayu kiidi Alanka Baratusiik njiitu jawriñ yi ci reewum Slovanie ak yeneeni kilifa ci nguurgi


Suñu sukkandikoo ba leegi ci xabaar bii dinañu wax ni jumaa jii nga xamni dinañuko tabax ci complexe bi dina am ayy sooroor yu toollu ci 40 metre ci guddaay dina am yitt ayy bërëb yoo xamni nii dañufay defee taaggat yaram


Koppar yi nga dinañuko def ci tabax yii toolluna ci fukki million euro ak ñaar diiru ligeey yi dina toollu ci ñetti att


Li jara xam nak mooy reewum Slovanie ñaari million doomu aadama ñoofay yeewoo waaye nak teemeer boo jël juroom yi ayy jullit lañu


1289920