صفحه نخست

فعالیت قرآنی

سیاست و اقتصاد

بین الملل

معارف

اجتماعی

فرهنگی

شعب استانی

چندرسانه ای

عکس

آذربایجان شرقی

آذربایجان غربی

اردبیل

اصفهان

البرز

ایلام

خراسان جنوبی

بوشهر

چهارمحال و بختیاری

خراسان رضوی

خراسان شمالی

سمنان

خوزستان

زنجان

سیستان و بلوچستان

فارس

قزوین

قم

کردستان

کرمان

کرمانشاه

کهگیلویه و بویر احمد

گلستان

گیلان

لرستان

مازندران

مرکزی

هرمزگان

همدان

یزد

بازار

صفحات داخلی

کد خبر: ۱۲۹۸۷۵۸
تاریخ انتشار : ۱۴ مهر ۱۳۹۲ - ۰۱:۰۵

Waallu bitim reew tey samedi 05 octobre lañii amal lañii amal jotaayu waxtaan ci solo bi nga xamni beennoo jullit ñi amnako ci daara jiidi Al waaziayni neekk ca lakxano ci reewum Inde



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci Asie ni: jotaay bii su fukki waxtu ak juroom jotee lañuko door ñaangum al xuraan nak lañuko dooree ci gannaaw loolu borom xam xam yu gëna raañeeku ci reewum Inde dinañu jël kaaddu waxtaan ci beennoo jullit ñi ak solo gi nga xamni amnako


Kiidi Oustaz Axiil Alxarawii nga xamni mooy ndawalu kureel biidi yënggu ci waallu jegele mazxab yi ak ngiir yi ak jullit ñi


Jotaay bii nak ci nimbalu daara biidi jaangale diine Al waaziayni ak kureelu caada biidi Al Muamal ak kureel biidi Al bayinaat lañuko amalee


1297961