صفحه نخست

فعالیت قرآنی

سیاست و اقتصاد

بین الملل

معارف

اجتماعی

فرهنگی

شعب استانی

چندرسانه ای

عکس

آذربایجان شرقی

آذربایجان غربی

اردبیل

اصفهان

البرز

ایلام

خراسان جنوبی

بوشهر

چهارمحال و بختیاری

خراسان رضوی

خراسان شمالی

سمنان

خوزستان

زنجان

سیستان و بلوچستان

فارس

قزوین

قم

کردستان

کرمان

کرمانشاه

کهگیلویه و بویر احمد

گلستان

گیلان

لرستان

مازندران

مرکزی

هرمزگان

همدان

یزد

بازار

صفحات داخلی

کد خبر: ۱۳۰۰۵۱۵
تاریخ انتشار : ۱۷ مهر ۱۳۹۲ - ۰۰:۲۸

Waallu bitim reew xew xewu maaggal bësu tabaski ak julli tabaski mardi 16 octobre lañukoy amal ca jumaa ju magg ju neekk ca Paris



Këru tasukaayu xabaaru al xuraan yi (ikna) te neekk ci Iran xabaarna jëleeko ci bërëbu xabaar bi nga xamni moo neekk ci internet (saphirnews) ni:Daliil bubkar xamlena ci bataaxal bi nga xamni geneenako ni mardi 16 octobre mooy neekk julli tabaski


Njiitu jumaa ju magg ju neekk ca reewum France xamlena ni:julli tabaski bi talaata lañukoy amal su juroom ñaari waxtu tegee ñent fukki simili ak juroom ci waxtu reewum France


Ci gannaaw loolu ñaanalna jullit Ci gannaaw loolu ñaanalna jullit yëpp ñu am feetu tabaski mu muccu ayib rawatina nak jullitu reewum France woona leen yitt ngir ñu teew ci julli tabaski gi


1300193